Neymar

1.7K 102 4
                                    

Gnari mère gno donn wakhtann
-Degg nga ni Ndeye Mar da fa diougué Barça
-Ya guiss dh goné légui yi seyyëtou gnou
-Wa yow sakh da nga kham kou may wakh.
-Moo! Ndeye Mar , domou Abou mar diy sérère saffène . Ma kham ko

Coin humour : réé ba tassTempat cerita menjadi hidup. Temukan sekarang