gniarèl Kharitou Dieukeureum

By bijou_Chanel

1.2M 85.9K 3.9K

Giarel bou feroce guen di am fofou gnew nagou dieuram khole bi di dag th dousi meun dara wayè nak c son karma... More

le debut du commencement
rencontre
humiliation
suitee
confuse
love of my life
suite
une niarel sadik en cour...
rencontre avec mes futurs beaux parents
Le jour j
Seuy seuy bi
salam
Madame Fall 💍
le labane
une vie de femmes mariés Quoi 💍
son retour
réunion de familles
FEU
une nuit feroce
1(un)mois plus tard
réconciliation
réconciliations
toure de famille
cœurs briser 💔🖤🕳
SAMA AY 😋
sama aye 😋
aye finsh
un mois ce sont écoulée
FALL FAMILY
mane la beug
mon passer me rattrape
gniarel kharitou dieukeureum
MATAY MA DEFF KO
awo bandit là
Bonne nuit
parti 01
SUITE DU PARTIE 01
gniarel 2.0
une petite partie
louy problème bi ???partie (01)
louy problème partie (2)
KHEW__MI
cc mes love
yé sama kharit yi namone nalén kay
🤍
🤍
un bon entendeur salut (mes amis fautes)
tabaski en wadiation
tabaski day
brisée 💔
💔
que faire
Hello mes bebew ❤️😩😭🎉🎉🎉
Zakhra and amdi
Naissance
Jongué lou nekh
DRAME
Divorce
Fin du tome (01 )
New president🎉

futur Mm fall

22.7K 1.8K 33
By bijou_Chanel

salam salam 😌😌❤❤

tok tok

entrè

zakhra vient repondre a papa dit khadim fall mon frère vous vous rappeler de lui no?

hi khadim mba diam la rek en ouvrant grandement les yeux pa bi dafa beuri guitagense

bah je sais pas va repondre afrontè rk   ko mou diekh moy lolou dh ioe ken Daf la rawoul

Je lui un grand thip et me lève

je me lève du lit et sort je traîne   les pieds jusqu'au salon je me sent pas très bien depuis se matin khamou ma sakh louma dall

bonjour papa

zakhra togal dama beugon gniou wakhetane le père de aïda m'a appeller pour me faire part de là vos  histoire !

je conprend rien ?

kan moy aïda ?
papa c ki aïda je conprend rien là

ioe khamo aïda kham ga lanela j8 pas ton egal bayil dieukeurou diambour mane nila la yarè Een amal diom domi nit kou yiw ga

😂😂😂😋Ah ok je vien de comprendre nak mane khamou ma le nom de  aïda dada la kham Kay père kon wero bayi diam wakhal lènène 😭😂

Nedeysane pourie gattè quelle est elle est aller pleurenichè chez son père wayè elle n'a encore rien vue sou guissatè sakh kouy humilier

man dal khaw ma loutakh awo yi gniak khorom rk shete nilèneu niarel yi eupè thiase sakh dafa gniaw way NO 😢😂 daguèn longtemp nak  bref pa bi loumou wakh ma bayi kan 😂dieukeuram

Même pas en rêve amdi fall dh souma ko seuya loul mba aduna signè no damay dal di  bayi ndank père bi boumou doug si game yoyou sakh lay amdi c mon amdi a moi toute seul 

papa mane dada talou mako sakh et sa fait l'occasion je voulais te parlè serieusement papa mane nèka touma khalei th aussi amou ma loula soute ioe tu es mon kilifeu et tu as toujour pris soin de moi depuis toute petite meusou ma manquè dara yare gama figua ma wara yarè machallah dama guiss nak gor bou bakh kouma beug respectè ma kou am dinnè gor bou am yar nèna nak daf ma beug tak sa benediction rk lagniou sokhela ioe ak manma

Alhamdoulillah rabine alamine machallah sa ma khol sèd na torop je vois en toi une femme determinè kou kham limou beug tu as beaucoup grandi ma chèrie sans pour auten que je m'en rend compte ton papa est fier de toi li rk la la beugeulone fait le venir ici bou fèker liga wakh ni yep mo nèk si mome dina ko may diabar sen attendre dakh tarou jiguen seuy la dina guestou leep in sha allah

j'ai versè quelque larme  de joie   il c'est lever et m'a pris dans ses bras love you dad😢❤😭

Pour l'identité de mon future mari nak sa mom je laisse manan lui expliquer j'ai trop peur qu'il me dit no car c est le mari de la fille de mon patron gniagni gnignia  vous connaisez bien mon père il est trop compliquer mes jespere que dou yak li parck quil sagit de mon bonheur tè seuy bi fok ma seuy ko dina keuf dieukeuram si ay lokhom th gniow dou am dara dou yeugou.

je trouve ma mère dans sa chambre mais elle pleure wa loukhew

Man lanela gawè ma koula togn En yaye ioe tmt bouma tital kou dè

Ken dewoul bayil eupale 
ma fille je suis trop contente pour toi li rk ladone gnian yallah ga seuy am dieukeur bou bakh dakhetè sa keur baye bi dadieu na fi lounè mes meusou ma daw mougn rk la deff ma beug so dèmer ga khol si mane seuy rk th yallah takh seuy dou ben fan rk dh c tout une vie alros sois soumise a ton mari et respect le contanet na ba fou contane yème fall diaga yaram ioe bakh rk ga meuna deff sama taw bou jigueen bi

Oh c'est touchant j'ai tellement pleurè j'etais emus et fièr de ma mère jiguen mougn kat la tè je ferais de mon mieux posdible seuy seuy bi suivre ses conseille a la lettre inshallah

je lui est fait part de l'identi de futur mari et elle m'a de suite compris j'ai de la chance d'avoir une mère aussi comprèhensive elle ma promis de parlè avec papa que y'aurra aucun problem esperons rk pour père almant mom on peut s'attendre aux pire lol

soudoul wone ak mom dh pa bi sagn na bagn sadic la deff il a finit par accepter sama yaye dafa wakh mba mare mouy sogua ceder

mon frère aussi etait superd content pour moi et a beaucoup prier pour moi j'ai appeller les filles pour quelles vienent a la maisson et j'ai dejas parlè avec amdi sikaname lay gnew wakh na ak famille wam mba parè .

j'entend bcp de bruit dans la maison je pense que se sont les filles jiner yigniou done 😂

bilay yèna beuri bruit kom ay guewal rk c trop way

holof Ndiaye nèna guère bou yakou mo raw guewal dit diarra

Aeh wawaw fofa todieu wa diank tay tèl ga gniou wo dh mba diam ca dafa am khana dit ouley en sasien sur mon lit

ouley esk zakhra meus nagniou wo sans pour autemp ca am😂fransement tmt 😁

Allah pourquoi tu ma donnè des copine aussi fofolle elles se mets a rire nonou ga gniou beuguè

vasy zakhra accouche je commence a perdre pacience

SHIIIIIIIP bon ok enfet c'est a propos de amdi fall le mari de l'autre la

putin on sais dejas bayil bèn bènal bi ioe dmr ga rk kham ga yako tay dit diarra et ouley

elle sont prèsser dh

😂😂😂je fais exprè de le bèn bènal com sa ca bi guena pimentè dou nonou?💥

respirons 😂 profondement no ay rè sakh farnama diap

depuis tenyi yep je frequente amdi on c'est bien raprochè et

et... dit ouley en me coupent putin li amoul fèn nak

ON N'A DECIDÈ DE SE MARIER

elle se sont regarder 😲et commense a sautiller de jois elles m'ont pris dans leurs bras j'ai fallier mètouffer

QUOI WA DIANK GNIOUN CAR BI BAYI NAGNIOU FI DH WOUY 😂😂😂😂😅 dit diarra

wa ioe loy yokhou on n'est pas sourd tmt

barki serigne touba li bou amoul wone ma khathieu wa dada khol bè nara wad bou yeugè li gniaw tay rk lagniou koy thiorotè gniarel bounè moute lala lay tègal ni dh eupeuneuh dit ouleye

ioe ouleye dada daf gniou doy galakhe dèkou gnio guini dagou dieureum th thiow dou am dara dou am khalei bi niarel la wotè ay lolou dit diarra

je mord la levre inferieure vous me connaissais tres bien sama khètou capable rk eupena amdi fall dh dina ko kheud bache ko tente ko mba doutoul guisa ti kènèn kouldoul mane pour dada nak on va le multiplier par zero th tal sougniou seuy bi

j'explique aux fille sougniou khoulo bou saf biniou amone dagnio rè ba tass bilaye😂😂

no zakhra bamdit gua wa wargua wakh li domou diambour bi tmt

ioe diarra ki dama ko moy souma moytouwoul lou raw lolou lakoy wakh daff ma khamoul rk 😁

choquè la deff dada dh am na sokhela bou reuy sou yeugon doula meussa dièma humillier quelle woudiou bou sadik lol dit ouley

ma wakh moumay traitè de pute wayi dana ko wane ni diaga woul sou dafay diang

et c'est partit dans un commentaire sen fin .

amdi est a present installè dans notre salon entrain de dispute avec mes parent Ah je voulais être petit petit fourmi là pour pouvoir tout entendre lol

je stres trop en même temp j8 trop excitè j'ai un sentiment inexpliquable heureusement que les filles sont la sino mome dou bAkh

eux avec leur blague rk on sennui jamais


alors jespere que cette chapitre vous a plut et sa coûte rien de commenter ou de voter no

a très bientôt chapitre you guen feroce mogui gnew inshallah bisous💋💋💋💋

Continue Reading

You'll Also Like

335K 35.7K 91
Cette histoire est fictive mais sa vaut le coup de lire... ses l'histoire d'une jeune fille qui a perdu sa maman a l'âge de 8 ans mais cette fille a...
11M 754K 94
Mavi, une jeune fille turque de 21 ans, va rejoindre son petit ami en Espagne. Mais malheureusement, ces retrouvailles vont être le début d'un cauche...
60.1K 4.3K 37
Mais qui a eu raison de l'autre ? "Au-delà de la douleur, je suis à bout" "Oh le mal de vivre, sans toi" "Mes nuits ne sont plus que rêves et insomni...