SUITE DU PARTIE 01

17.7K 1.2K 76
                                    


Allô ouley regarde si le chauffeur es revenu pour qu'il te dépose sltp

Chauffeur bi kay démoul wone bay gnew sank dagua guén rk mou gnewate

Je savais que tout à l'heure dada n'es aller nulle part elle voulait juste m'énerver wayer mayou mako lolou bref nala déposé amfa beauty on t'attend on es dejas sur place moi et diarra

D'accord je vous rejoins toute suite bisou bisous

Je rachroche le téléphone diarra qui n'arrêtait pas de snapé on se fesait un peducure manucure

Boy kharal ma létou ay mèche raw you todj couleur blonde wala guisso lolou ioe

Bagnia gniarel bandit waw blonde bi douma ko bagn deff yeufou sadic

Diarra sof gua no lolou lay deff sakh mba paré laleu you guoud

J'ai laisser diarra faire ces ongles tandis que moi je commence mes tresse façon ces vit fait trois personnes gnio may lét ni ouley vient d'arriver les employés ont bien pris soin d'elle en occupent bien de ses cheveux

Zakhra toguay bi ladoul meun miss defal ma you dieum si guinaw rk sans méche

D'accord madame à vos ordre ne vous inquiétez pas sama lét yékhoul

Ioe tapét gua rk meuno wone létou létou nit toguay bi mom nekhoul si kén

Deff lo meun so teudé nelaw ioe dagua wow beut ma wakh gua laleu blonde nonou ah wa bakhena

Normal tay ma ayé fok ma wané sama bop frère

Oh lala regardé mes ongle shi boy wa amfa dagniou meilleur

Nagniou meilleuré la ragal mane rafet n'a torop sakh Machallah

Li kay dafa pop beug nasi yi dh dit ouley Diarra pouffe de rire

Demal gua top ndeye coumba li meuno si am ish dit diarra ouley la thip

Bon man mom je veux des tresse américaine nespas dou dieul temps en s'adressent a l'un des employés

Ma chérie les tresse américaine c'est vit fait dou dieul temps

On termine presque en même temps qu'on es belle l'institu nousons prie  en snap shiip pop n'a khalei yi lét nagn ma raw you you todj 

No wa amfa yéna meilleur dh liguén ma tresse ranversé ko ndeiy comba mi dit diarra ouley la dévisage

Tout le plaisir es pour nous solén beuguer rk ma beug dit  la gérante

Oh contane nagn Môme franchement yeup gniata la

Ioe tu une fidèle cliente lép 60.000ml  la total dit la caissière

Diarra écarquille les yeux QUOI 60000 wala 6ml chére n'a dh je sort  mon téléphone pour payer avec wave

Diarra chéroul dh boul faté peducure manucure bi sa ongles yi té géle gua deff  3 bop yeup gniom gnio diokher méche té raw dafa chère

La caissière sourit je paye ont leur remercie et sort on monte dans la voiture

Diarra ioe dagua badola tu ouvre ta grande gueule devant eux dinaneu dafa chère dit ouley

Ouley tenyi sa déret tangu n'a dh lima wakh lousi nek zakhra limou fay dafa chère thipp

Kham na ioe la nara weusine sa kanam bou gniaf ndeiyam bi dit ouley on éclate tous de rire 😂

Mogui gniaw dh sa dome souma niro dagua wara sante yallah sa kanam mo guen gniaf ndeyam rew

Wahaha mogui gniaw  dh boulén ma tué way ouley bayil khamadi

gniarèl Kharitou DieukeureumWhere stories live. Discover now