chapitre 4

7.8K 213 3
                                    

                    Assy Samb

-mon amour le petit dej est pret

-d'accord on y va

On descend prendre notre petit dej en famille apres avoir finir debarasser et ranger la salle à manger je monte voir mon mari.

-Firdawsi dioxma depense bii ma dem marché

Il me tend 10k francs

-loumay toggou?

-deffal yassa guinar

-wah ok magui dem té ñeuw

-je dois bouger vite fait mais je vais pas durer

-okey mon amour ba sikanam

Je prends mon calebasse dem marché deff sama ndougou bouné moutteu. Je rentre à la maison deff sama voile comme dafa tangg ma attaqué agn bii nakk. Dama wara wo saxx Satou defarko compte rendu mais na xarr ba parei ma woko.

J'etais entrain de preparer ma sauce comme guinar bii damako waxa titeul thi fourneau bii ma bayii four egali walam. Ma sauce etait presque fini quand je vois mon mari rentrait dans la cuisine les mains derriere lui.

-honey je suis de retour

-firdawsi mba sono akk tangay bii

-non non honey j'ai une surprise pour toi

-surprise hummmmm ma xolleu ko

-loutax gue yakamti sa life

-tchim ya gueneu xamni dama curieuse nakk loma indil

-am oubil ko sa bopp

J'ai pris le sachet et y sort une boite en rouge je l'ouvre et vois un ensemble boucle d'oreille bague et chaine en or.

-Barki sama woudiou mame douma ko laal waouw lii mogui briller mashallah dis je toute contente

Je m'approche un peu plus de lui en l'embrassant ma dadii dawalal sama loxo bii thi yaramam bii egg bathi koy bii rkk dadikoy boxoñ boxoñ bou sew té vulgerrrrrrr rekk arriere

-merci beaucoup mon coeur

-pas de merci dagueko merité mais j'ai une question

-oui vas y je t'ecoute

-Assy Samb demb laneu gue deff sama koy bii? Assy Samb koula yakk kila xamal lii yeup waneu mako damako beugue teral

-sa koyy bii damakoy doneu ndamp rkk té dafa ndiro ak sucette mani nako mathieu rkk ta belle soeur mofi diaar

-lima yeugg demb moussou mako yeugg le fait d'y penser rekkk xolal magui kodal

-mdr na regler teyy gouddi bii dafa nara nexx té yagg

-naka diekk ma xamni Satou koba la lii mtx Jamil douko sori moukk teyy boul togou rere commandé na ba paré pour wa keur dañi dem resto

-lolu dinama nexx d'accord amoul bleme

-okeyyy magui dem jeulii sama domeu tbi Aissatou bala mouffi nekk nittou ambionce

-dinala bolei ak Aissatou

Il sort de la maison et je continue mon repas j'appelle Satou pour defarko compte rendu bii

-allo commissariat du quartier j'ecoute

-billahi ioe Mansour ak Deve rekk ño meuneu nekk ak iow

-je t'aime aussi contaan gue deh diankk defal ma compte rendu bii gaw

-meuno deff nank tchim

-koneu yagui xoulo batay

-mbepe Satou euhhhhhhh devine ioe lane lañ ma wara diox

Bou Dara YombOù les histoires vivent. Découvrez maintenant