katanté ak Sama Diabarou Patron
  • Reads 132,966
  • Votes 1,101
  • Parts 12
  • Reads 132,966
  • Votes 1,101
  • Parts 12
Complete, First published Feb 28, 2024
( *prologue* )

Bonjour a tous d'abord je me présente avant de vous raconter mon histoire avec ma patronne.

Ma wakhléne may kane bala malen di netali sa histoire ak sama patronne !
on me surnomme Karara  am 30 ans deuk ouest foire . bimay am 11 ans la niak samay wadiour ma nekone un enfant de la rue ndakh sama tanta dafma dane maltraité 🧐 bima amé 16 ans la nieuw Sénégal ( dakar ) done manébarou si chantier difa fanane aussi ba khamanté ak sama xariit Ass Malick ( boy bou nekh lokho ) sathie rek lay def . Man mom dama beugone entrainer ak sagnsé mais meussouma sathie vraiment .
Mane ak Ass ande naniou 10 ans nio moudié bokou chambre a pikine rue 10 , 
Bimay am 26 ans jour matar sathie Khaliss bou beuri niou topouko ba keurga diapko yobaléma té defouma dara . Nonou laniou niou condamné 4 ans de prison mou metima lool ma géréko ba peine bi diekh Sila guéné Di wout job may def recherche si Facebook bi ligueye boy si keur pour meuna am fouma fanane .

1 mois après lama béneu nit contacter bou toudou salif Ndiaye mais Mr Ndiaye lanioukay wakh ap modou Modou la bou nieuw vacance deuk maristes mais keur ga béneu gardien mofa nek mou dieul ma may topato jardin bi ak khar yi etc...

3 mois may ligueye nice ba 1 jour Mr Ndiaye woma nima dafay delou italy mé diabaram Rokhaya (kya) Mme Ndiaye dafay nieuw vu que keur yayam lako bayiwone bobou la benéne doundou commencé si keur gui
All Rights Reserved
Sign up to add katanté ak Sama Diabarou Patron to your library and receive updates
or
Content Guidelines
You may also like
You may also like
Slide 1 of 20
A D J A  cover
🍑 Titre : Diongoma mineur cover
Lesbie🇸🇳 cover
Xalé féroce ( Jeune   féroce) cover
La meute d'arcadÿs🌗: Un mariage presque arrangé cover
ملائكة وسط شياطين cover
SAMA SHEYTANÉ cover
🥵🔥🥵Titre : Rencontre Groupe watpad*( Bande annonce)* cover
Baccalauréat  cover
Niarel la : suis deuxième dame  cover
MON MARIAGE AVEC LUI cover
 mami et jules cover
gniarèl Kharitou Dieukeureum cover
Ne Perdez Jamais L'espoir cover
Combinaison  cover
NaLu💕... cover
SAMA JEKEROU HARIT BI KOY BOU REUY LA YOR  cover
🍑 Titre : Dépendance Katantè  cover
JONGUÉ 100%🔥🙈👅🍯 cover
Ni Leu Meuneu Démé [TERMINÉ] cover

A D J A

28 parts Ongoing

Lisez pour mieux comprendre